

Lima giss ci Gambia,
jaay dëkk bi séddoo xaalis bi,
Lima giss ci Gambia
Two hundred Dalasi bi comme 2D,
Lima giss ci Gambia,
noise bi bari na,
liggéey bi desna, Lima giss ci Gambia —
no support, too many talking.
Lima giss ci Gambia,
waa dëkk bi sonnu nen,
Lima giss ci Gambia,
youth yi xaar nañu,
No support, we need changing
They say The Gambia is our homeland,
Dëkk bi melni a farmland,
We strike we work and pray,
Ku fi strike, fanan Mile 2 center prison.
Lo ñu promise, kan nga koy renew?
Mr. President, hana yërëmuloo lu hew co Dekka bi Dëkk bi,
dara doxul fii, Kufi gëna ngemmeh chono gëna sonn,
Retirement du dara ludut yoka chono.
Da ngay job nyu dila job ba nga xàddi system kofla.
Nenko wax té deihe but trap mofi neka liggéey bi.
Nen Baye boy yi trap moytu tarass yi sometimes nyu amci some
slap. Too much corruption Mr.
President, legeeye yulo ?
Nusrat Junction ba Kaw Junction pass bi 15 Dalasi la,
Nyu ne xam sa bop ci jaamu Yallah la boko,
Waye bo xamee Yallah,
doh tal sa boppu...
Lunu xamon tamit, J lu ko rëwwa,
fi nekk tamit B.
Sometimes damay russa nekk Gambian...
Nyatta Youths lañu sacrifice ci Géej (Sea)?
And still, they don't give up on sacrificing their life.
What did we do to deserve this in our country?
Beugue changing mo nyu turn to cere.
Nena badman du lettu mës,
Léegi badman ya ngi sol caanyal!
Corruption in every office,
Public money disappearing in silence,
The people are asking where is our hope We need leaders who
can serve the community.
You can build many police stations,
But your youths are dying at the backway,
Graduates walking with certificates,
Still looking for work every day.
Lima giss ci Gambia,
jaay dëkk bi séddoo xaalis bi,
Lima giss ci Gambia
Two hundred Dalasi bi comme 2D,
Lima giss ci Gambia,
noise bi bari na,
liggéey bi desna, Lima giss ci Gambia
—
no support, too many talking.
Fuck the law, because the government is framing the Youths,
Di len accuse: rapist and drug abuse!
Fekka nyom nyu ney diiss virgin underage,
di len joxé drug.
Hotel, bar, motel, restaurant—fo dem,
giss fa GG car!
Buffer Zone, roccas la romb,
Sister neema: "Bro, nyatta danu nga?" Maneko: "Sister,
understand-uma." Muné ma: "Suma bala ngakoy dem jot." Foreigner yi,
nyom 5 Arch pur danu,
man 4 Arch nyu dem.
Comme fila reew mi tollu,
jaay sa faith pur frai.
Bëgga giss mu fail,
tax nga Serigne tu ko.
De nyo fen! Nyom sathiakat yi,
nyo len gën. Dan la suulal,
suyalla fuff, ba pare chop lola.
Nga doff, nga sick,
nga wiess, wala nga dee (die).
Yép len ci éffalé: die or lost,
Waye sa prosperity? No,
du am! Education should be our foundation,
But young people are losing motivation,
Janga bi metti, job amufi,
Youth yi dem Backway,
because of hope bi nekutfi.
Politicians yi wax lu bari,
Campaign time, ñu bëgg sa vote rekk,
After election, where are they?
The same promises, another four-year wait.
Cost of living going higher,
Rice and fuel taking money from the buyer,
Mother at the market counting every dalasi,
Father working hard but still can’t make it easy.
We don’t need another speech,
We need hospitals, schools and jobs,
We don’t need another promise,
We need leaders who deliver for us.
Lima giss ci Gambia,
jaay dëkk bi, séddoo xaalis bi,
Lima giss ci Gambia,
two hundred Dalasi bi,
comme 2D, Lima giss ci Gambia,
noise bi bari na,
liggéey bi desna, Lima giss ci Gambia —
no support, too many talking.
Lima giss ci Gambia,
youth yi ñàkk opportunity,
Lima giss ci Gambia,
corruption killing the economy,
Lima giss ci Gambia,
people asking for transparency,
No support, too many talking — give the people dignity. (hmmmmm)